Gaïndé

January 13
11 mins

Episode Description

Ngir xam lu leer ci seen mboorum réew ak bu Afrig, ndaw ñi dañoo war a miin jàmbaar yi tabax  Afrig. Ndégat yii di Podcast, xam sa démb, xam sa tey »,  looloo tax ñu tànn yenn ci jaar-jaar ak xew-xew i mboorum Senegaal, ngir may ndaw ñi ñu jàngee ci seen démb, baa man seen tay, te waajal seen ëllëg.

See all episodes